ettub wolof 1

Licencia: Gratis ‎Tamaño del archivo: 8.07 MB
‎Calificación de usuarios: 5.0/5 - ‎1 ‎Votos

ci wolof - En français - En Inglés

ci wolof

ëttub wolof moo leen di baaxe benn sàqum baatu wolof, te ñu tuddee ko oggo, ay léebu ak benn jumtukaayu ijji ngir mën a ijji ciof. oggo mooy sàqum baatu wolof bi jëkk a am, nga xam ne baat yépp ci wolof kepp lañu leen tekki. oggo am na lu ëpp fukki junney baat ak benn. léebu yi ëpp nañu ñeenti junney léebu, boole ci juroom ñetti téemeeri waxin. waxinu benn léebu, mooy léebu bu ñu waxee neneen. jumtukaayu ijji bi, dina tax ngeen mën a ijji ci wolof, ci amam yu gaaw. ngir jàng dawal wala jàng bind wolof, mën ngeen a jëfandikoo dalu-web bii di www.ettubwolof.org.

En français

ëttuf wolof vous propose un dictionnaire wolof nommé oggo, des proverbes wolof et un outil pour vous familiariser avec l'alphabet wolof. oggo est le premier dictionnaire entièrement en wolof avec la définition des mots en wolof. Il contient plus de 11 000 mots wolofs. Les proverbes wolofs comptent plus de 4000 proverbes incluant plus de 800 versiones. Versión une d'un proverbe est une façon différente de dire le proverbe. L'outil de l'alphabet est très utile pour vous familiariser rapidement avec les lettres de l'alphabet wolof. Pour apprendre à lire et à écrire le wolof, vous pouvez également utiliser le site www.ettubwolof.org, además de riche en contenu.

En inglés

ëttub wolof ofrece un diccionario Wolof llamado oggo , Wolof proverbios y una herramienta para familiarizarse con el alfabeto Wolof . oggo es el primer diccionario enteramente en Wolof con la definición de palabras en Wolof . Contiene más de 11.000 palabras de Wolof.

Los proverbios Wolof tienen más de 4000, incluyendo más de 800 versiones. Una versión de un proverbio es una forma diferente de decir ese proverbio.

La herramienta del alfabeto es muy útil para familiarizarse rápidamente con las letras del alfabeto Wolof.

Para aprender a leer y escribir en Wolof, también puede usar el sitio web www.ettubwolof.org qué contenido es más rico.

historial de versiones

  • Versión 1 publicado en 2016-07-18

Detalles del programa